Channel Avatar

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD @UCG0ogTIN1bMJ5RghJFrFKKA@youtube.com

68K subscribers - no pronouns :c

(GBM)Groupe Baolmedias (Bfm 88.5 Binfo BmTV-HD) Chers Audite


Welcoem to posts!!

in the future - u will be able to do some more stuff here,,,!! like pat catgirl- i mean um yeah... for now u can only see others's posts :c

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD
Posted 5 days ago

AMNA SOLO

3 - 0

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD
Posted 1 week ago

VIDEO

0 - 0

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD
Posted 2 weeks ago

Urgent :Ahmed Khalifa NIASSE fait de grave révélation Waxtaane wuyéémé
https://www.youtube.com/watch?v=mccCD...

0 - 0

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD
Posted 2 weeks ago

Dissolution de l’AssemblĂ©e nationale : La rĂ©action du groupe parlementaire Bby
« Le groupe parlementaire Bby exprime sa reconnaissance au peuple sĂ©nĂ©galais qui, en 2022, lui avait fait confiance en lui confĂ©rant une majoritĂ© Ă  l’AssemblĂ©e nationale. En dĂ©cidant de dissoudre l’AssemblĂ©e nationale en pleine session extraordinaire qu’il a lui-mĂȘme convoquĂ©e et Ă  la veille de la DĂ©claration de politique gĂ©nĂ©rale dont il a lui-mĂȘme fixĂ© la date, le prĂ©sident de la RĂ©publique vient de commettre un parjure, exĂ©cutant en cela, et de maniĂšre cynique, les instructions de son Premier ministre », lit-on dans un communiquĂ© signĂ© du prĂ©sident Abdou Mbow.
Il ajoute : « Bloquer l’initiative de la motion de censure dĂ©posĂ©e par la majoritĂ© en usant de maniĂšre pernicieuse des dispositions de la Constitution l’habilitant Ă  convoquer une session extraordinaire, avec un ordre du jour surchargĂ© Ă  dessein, fixer une date pour la dĂ©claration de politique gĂ©nĂ©rale diffĂ©rente de celle proposĂ©e par la ConfĂ©rence des PrĂ©sidents et prononcer la dissolution la veille, relĂšvent simplement de l’indignitĂ© rĂ©publicaine et de la petite politique Ces deux hommes, Ă  la tĂȘte de notre pays s’amusent de nos institutions pour satisfaire leurs besoins politiques urgents, qui semblent ĂȘtre la dissimulation de leurs incapacitĂ©s Ă  rĂ©soudre les problĂšmes des SĂ©nĂ©galais et de conduire les politiques propres Ă  les faire sortir du marasme dans lequel leur politique les a plongĂ©s ».
#LeSoleil_Digital
ASSEMBLÉE NATIONALE DU SÉNÉGAL

3 - 0

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD
Posted 1 month ago

Serigne Balla Fally Dieng Lagniy xamlé

SĂ«riñ Habiibu Laah JeƋ, ñu gĂ«n koo xam ci SĂ«riñ BĂ lla Faali, mi ngi feeñ jamono ci atum 1856, ci dĂ«kk bu ñuy wax Njompi, nekk ca Kajoor.

Aw Askanam:
SĂ«riñ BĂ lla Faali, di doomi SĂ«riñ MasĂ mba Soxna JeƋ ak Soxna Xujja Aram Silla, mom Majama Anta Silla mi nga xam ne, moo sañci Ñaxal ci gox bu ñuy wax Ndogal.

Am njĂ ngam:
S. Bàlla Faali, mi ngi jàngee Alxuraan ci ku ñuy wax Sëriñ Ahmadu Silla ca Tayba xay, foofu la nekk ba mokkal Alxuraan.
Ginaaw loolu, soobu na ci njàngum xam xam, ba jàng ci fànn yu bari te wuute ci fànn yi ñu baaxoo woona jàng ci réew mi, ba géeju ca lool.
Ba mu noppee ci am njàngam nak, la dellu ca kër baayam, Sëriñ Masàmba Soxna ca Njompi, nekk ci wetam, daan ko jàple ci mbiri àdduna yi ak mbiri diiné yi, daan wéyé ay ndigalam ci lépp. Ci loolu la sax, ba ni mu sañcee kër, ñu dénkoon ko Soxna su ñuy wax Soxna Kana Mbóoj.

Ak JĂ©bbloom:
Mu teela jébblu lool ci Sëriñ Tuubaa, ci jamono ya mu nekkee Daaru Salaam ci atum 1886, foofa la ko Sëriñ Bàlla fekkoon, jaayante ak moom, ci anam yu taroon lool ci moom, waaye muy ku Yàlla dimbali woon ci yitté ju kawe ak pas pas bu dëggu.
Ginaaw bi Sëriñ bi sañcee dëkkam bii di Tuubaa yit, S. Bàlla bokkoon ci ñi àndoon ak moom, mooy ki fi ñjëkka bay, ngir màndargaal dëkk bi bañ man koo xàmmee.
Foofu ci Daaru Salaam, fa la ko Boroom Tuubaa tarbiyaa, ci diirub 3 at, mook Seex Ibra Faal ak yeneeni mag ci yoon wi.
Sëriñ Tuubaa gëram ko, ngëram lu kawe ginaaw bi mu sañcee Tuubaa, te daan seede ak defaroom, li ciy firndé mooy ki ñëwoon ci moom ne ko "Mbàkke, man de da maa bëgg nga defar ma", Boroom Tuubaa boole ko ak Sëriñ Bàlla Faali mii, ne ko "defar de, taqoo la laaj, te amatuma jot gi, waaye demal seeti Bàlla Faali, moom defar naa ko".
Kon ku Sëriñ Tuubaa seedeel sag defaru, loolu rek doy na sëkk tawfeex.

Ay jëfam ci yoon wi:
Batay moom Sëriñ Bàlla mii, bokk na ci ñi Sëriñ bi njëkka jox ndigalul Màggal bisub 18 Safar (Màggalug Tuubaa), mu amoon ci ak farlu lool ak pasteef, ba mujj sax bisub Màggal bii, ñu ko daan woowe "bisub Sëriñ Bàlla Faali". Loolu la Sëriñ Musaa Ka di wax ci bëyit yii naan:
"Mu dellu saxal ci weeru Safar di mĂ ggal
Bi izni Cheyxi Ahmadu BĂ mba Waali

Fabug coggal, di def di ko yobbu Tuubaa
Wa saakuy ceeb, wa xandiy diw, wa maali

Saxal na ko fukki at yu tofal juroomam
Deful koppar ci kalpe ba yobbu waale"

Sëriñ Bàlla Faali, bokkoon na ci taalibé yi sàkku ci Sëriñ Tuubaa ngir mu bindal leen, lu jëm ci ak ay teggiin akug taalibé, moo sabab Sëriñ bi taalifoon Xasidag Nahju ca jamono yooya, moom la Sëriñ bi di wax ci bëyit wii naan
Ù‚ŰŻ Ű·Ù„ŰšÙˆŰ§ Ù†ŰžÙ…Ű§ Ű­ÙˆÙ‰ ŰȘۣۯۚۧ = ليŰȘŰŁŰŻŰšÙˆŰ§ ÙˆŰ°Ű§Ùƒ ÙˆŰŹŰšŰ§

Ci guerre ba amoon ci atum 1914 - 1918, Sëriñ Bàlla moo njëkka joxe ay niti bopam ci soldaar yi wara dem ca guerre ba.
Noonu yit la ràññee koo woon lool ci ligéeyub Jumaay Tuubaa, bi ci Sëriñ bi joxee ndigal.
Jumaay Njaarém ji tamit noonu la ci ràññee koo woon ci joxe ci àddiyaam, te moom la Sëriñ bi féetale woon muy saytu alal ji fay dem.
Farlu woon lool ci joxe àddiya, daan ko ko yonnee ba Gànnaar ci Sëriñ bi, ci sabab yooyu sax la ko Boroom Tuubaa yonnée woon Xasidag Jalibatou Marakhib, joxoon ko ndigal mu mokkal ko, mook ay taalibéem.

Mu sañcoon ay barab yu wuute, ngir jaamu YĂ lla ak ligĂ©ey, ak daan tarbiya ñi ko SĂ«riñ Tuubaa booleel, bokk na ci barab yooyu, fu ñuy wax Daaru JeƋ, mu sañcoon ko ci ndigalul SĂ«riñ bi ci atum 1903, ak yeneen daara yu bari ci rĂ©ew mi.

Bi Sëriñ bi nekk Njaaréem, joxoon na ko ndigal mu sañci fa kër, mu nekkoon fa ak moom. Ginaaw làqug Sëriñ bi yit mu toppoon Seex Mustafaa, gëna yeesal pas pasam ak farloom ci ligéeyal Sëriñ Tuubaa, Seex Mustafaa fonkoon ko lool, ba gane ji woon ko ca Njompi ngan gu rëy, moom la Sëñ Musaa Ka naan:

"Ma santal SĂ«riñ Tuubaa SĂ«riñ BĂ lla Faali JeƋ
Du moo gëm Sëriñ Tuubaa te gëm Amdi Mustafaa

Dëggal gam dëggal mootax ba Buur Yàlla far dogal
Mu moom waa ndogal, moom njompe, moom Daaru Mustafaa

Sëriñ Bàlla faalee jox Sëriñ Amdi tiitaram
Na léen woor ne boobe gembbe yaaram la Mustafaa"

Noonu mu meloon ak Seex Mustafaa, ni la defoon ak njabootug Sëriñ bi yépp, ba manees naa wax ni ñi ci ëpp tuddée na leen doom, ni la defoon yitam ak magi Murid yépp, ku mel ni Sëriñ Ndaam Abdu Rahmaan Lo mi mu tuddé ab ki ko njëkka wuutu, ak ku mel ni Sëriñ Moor Kumba Kan, Sëriñ Masàmba Kànni Buso, Sëriñ Madiba Silla, ak mak ñu bari ci yoon wi.

Ak lĂ qoom:
Misaalum Murid Saadix bu làq ngëramul Sëriñ Tuubaa ngi nii, 1886 ba 9 Mars 1940, masula tàqali koo ak Boroom Tuubaag waa këram, keroog ba mu làqoo ca Njaaréem, ci la Seex Mustafaa wax Sëriñ Mbàkke Buso mu jullee ko, ñu deñci ko ci armeel yii ci Tuubaa. Yàl na nu Yàlla taas ci barkeem !

ki ko njëkka wuutu mooy:
SĂ«riñ Abdu JeƋ BĂ lla Faali 1940 - 1988

Yala yook aay Lerram Tass Nousi Barkem si Barkep Serignebi

Xalimag Akb Majalis

44 - 2

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD
Posted 2 months ago

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD

40 - 0

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD
Posted 2 months ago

..

1 - 0

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD
Posted 3 months ago

0 - 0

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD
Posted 3 months ago

7 - 0

(GBM) BmTV BaolmediasTV HD
Posted 3 months ago

📱 APPEL À CANDIDATURE RADIO TÉLÉVISION BAOLMEDIAS MBACKE 88.5 NUMÉRO 775385560 / 781362931
Email 📧 baolcom1@gmail.com ou baolmediasfm@gmail.com
Voici les coordonnĂ©es de Sister Maria SecrĂ©taire Baolmedias FM TV đŸ“» đŸ“ș 88.5 Mbacke en face Marche Mame Rama 764961777/walla 777042992
Email baolcom1@gmail.com ou baolmediasfm@gmail.com
WhatsApp 764961777

3 - 0